Wolof	French
Salaamaalekum	bonjour (salutation)
Na nga def	comment vas-tu
Maa ngi fi	je vais bien
Jërëjëf	merci
Waaw	oui
Déedéet	non
Ba beneen	au revoir
benn	un
ñaar	deux
ñett	trois
ñeent	quatre
juróom	cinq
juróom-benn	six
juróom-ñaar	sept
juróom-ñett	huit
juróom-ñeent	neuf
fukk	dix
kër	maison
ndox	eau
lekk	manger
xale	enfant
jigéen	femme
góor	homme
tey	aujourd'hui
suba	demain
démb	hier
bu baax	bon
rafet	beau
jàmm	paix
oto	voiture (de auto)
lekol	école (de l'école)
tele	télé
nit	personne
teranga	hospitalité
xaalis	argent
