#separator:tab
#html:false
#columns:Front Back
Salaamaalekum bonjour (salutation)
Na nga def comment vas-tu
Maa ngi fi je vais bien
Jërëjëf merci
Waaw oui
Déedéet non
Ba beneen au revoir
benn un
ñaar deux
ñett trois
ñeent quatre
juróom cinq
juróom-benn six
juróom-ñaar sept
juróom-ñett huit
juróom-ñeent neuf
fukk dix
kër maison
ndox eau
lekk manger
xale enfant
jigéen femme
góor homme
tey aujourd'hui
suba demain
démb hier
bu baax bon
rafet beau
jàmm paix
oto voiture (de auto)
lekol école (de l'école)
tele télé
nit personne
teranga hospitalité
xaalis argent