#separator:tab
#html:false
#columns:Front Back
#deck:LinguaCommons::Wolof (from English)
salaamaalekum hello (peace be upon you)
maalekum salaam and peace upon you (reply)
na nga def? how are you? (sing.)
maa ngi fi (rekk) I'm fine (here only)
jamm rekk peace only (I'm well)
naka nga tudd? what's your name?
...maa ngi tudd my name is...
jërejëf thank you
ñoo ko bokk you're welcome (we share it)
waaw yes
déedéet no
baal ma excuse me / sorry
su la neexee please (if it pleases you)
ba beneen (yoon) goodbye (until next time)
ba ëllëg see you tomorrow
man I / me
yow you (sing.)
moom he / she / it
nun we / us
yeen you (plural)
ñoom they / them
nit person
nit ñi people
góor man
jigéen woman
xale child
yaay / ndey mother
baay father
mag elder / older sibling
rakk younger sibling
jabar wife
jëkkër husband
xarit friend
waa kër ga the household / family
ndox water
lekk to eat / food
ceeb rice
ceebu jën rice and fish (national dish)
jën fish
yapp meat
mburu bread
meew milk
ataaya Senegalese mint tea
kafe coffee
suukar sugar
xorom salt
benn one
ñaar two
ñett three
ñeent four
juróom five
juróom benn six
juróom ñaar seven
juróom ñett eight
juróom ñeent nine
fukk ten
téeméer hundred
junni thousand
dem to go
ñów to come
dox to walk
togg to cook
jënd to buy
jaay to sell
gis to see
déglu to listen
wax to speak / say
xam to know
bëgg to want / to love
am to have
nekk to be (located)
jàng to study / read
bind to write
liggéey to work
nelaw to sleep
fey to pay
jox to give
def to do / make
rafet beautiful / nice
baax good
bon bad
tuuti small / a little
bare many / a lot
gaaw fast
ndànk slowly / gently
tàng hot
sedd cold
léegi now
tey today
suba tomorrow / morning
démb yesterday
guddi night
dëkk town / village / country
kër house / home
marse market
ekool school
loppitaan hospital
xaalis money
jamm peace
teranga hospitality
lu tax? why?